Sa joie et sa pudeur font sa face cachée
Son paraître et ses formes montrent sa force
Celle que je vous chante, vous est familière
Elle est utile et belle
Elle a révélé la beauté du monde
On la clame Paradis
Mbégte ma, sutura sa
Da fa méngóok, baatinëm
Zaahir sa, melo ya
Moo wone, kattanam
Li may misaal lu ngeen xam la
Am na njariñ te rafet na
Moo génne taaru adduna
Moom la ñu bakke, al janna
Waxtaane ko sax banneex la
Nañ ko foηk sakkanal ko
En parler même est agréable
Respectons-la, économisons-la
Vois la mer, le fleuve
Rendons grâce à Dieu
Elle est utile et belle
Elle a révélé la beauté du monde
On la clame Paradis
Mbégte ma, sutura sa
Da fa méngóok, baatinëm
Zaahir sa, melo ya
Moo wone, kattan am
Li may misaal lu ngeen xam la
Am na njariñ te rafet na
Moo génne taar u adduna
Moom la ñu bakke, al janna
Waxtaane ko sax banneex la
Nañ ko foηk sakkanal ko
Géej gaa ngi nii yé
Dex gaa ngi nii yé
Dara gënul ë neex taw bi
Ku weddi laaj ko bay kat ba
Ci la ñuy roosé seen tool ya
Walla nga laaj ko samm kat ba
Ci la ñuy nandale jur ga
Ndox daal am na njariñ baax na
Dara gënul la neex taw bi
Taw daal njariñ la ci dun bi
Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñëm ba la nga koo xam mu manqué
Ndox daal njariñëm Ba la nga koo xam mu jafe
Alaa gaynaago yoo samba lingeer
Donoy waaly yée, wulée ñaay ngoy
Yée gan wuri coo, wulée gaynaako yoo
Yeée, yóo, gan fari baa